Level 9
Level 10

Expressions and Phrases


33 words 0 ignored

Ready to learn       Ready to review

Ignore words

Check the boxes below to ignore/unignore words, then click save at the bottom. Ignored words will never appear in any learning session.

All None

Ignore?
dama sonn
I am tired
dama gëmentu
I am sleepy
dama xiif
I am hungry
xiif-u ma
I am not hungry
dama mar
I am thirsty
mar-u ma
I am not thirsty
dafa tang
it’s hot
Tang-ul
it’s not hot
dafa sedd
it’s cold
Sedd-ul
it’s not cold
baal ma
excuse me
baal naa la
you are excused
fan nga jëm?
where are you going?
maa ngi jëm kër ga
I am going home
maa ngi jëm ekool
I am going to school
John mungi jëm marse
John is going to the market
mungi jëm ci bitik bi
he is going to the shop
jëm-uma biro ba
I’m not going to the office
degg nga Wolof?
do you speak Wolof?
waaw, degg naa Wolof tuuti rekk
yes, I speak Wolof a little bit
John degg-ul Wolof
John doesn’t speak Wolof
bëgg-uma français
I don’t like French
bëgg-uma kafe
I don’t like coffee
Jennifer dafa bëgg lakk Wolof
Jennifer likes Wolof
damay jang
I study
damay lekk
I eat
damay liggéey
I work
moom jang-ul
he doesn’t study
moom lekk-ul
she doesn’t eat
ñoom liggéey-uñu
they don’t work
damay nelaw tuuti
I am having some sleep
liggéey-uma léegi
I don’t work now
dama bëgg noppalu
I want to rest